Youssou N'Dour - Xel Lyrics

Lyrics Xel - Youssou N'Dour



Famarë reub kat lawone
Da ama biss mou khall yône
Mu taxaw di xalat bamu yàg
Mu sène mbëtt miy daw
Mu suxat fital ambadi dâgu
nane douma raw
Far mbëtt ma sène kokorong
Dadi dieul bop ba
Dal di koy rône
Bopp ba neubouna litha des
Yaramam béppa ngui fègn
Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya
Lippe di fègne
Lii takh mou déféni
Mbeutteu daa amoul xel
Kone gnoune gni Yalla jox xel
Nagnu santati
Nagnu santati
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy
Sougnou xel motax déf
Loy dougou jitalal sa xel
Ba lo thièy wout
Di nga guiss nguenél
Nit gni yor xel boo sété gnoy dokhal aduna
Kiy déf dou xalat
Thi missal day mél ni mbeut ma
Nit môm khélako yor
Nit môm khélako yor
Nit môm khélako yor
Nit môm khélako yor
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy
Sougnou xel motax gnuy déf
Fi neubeu moy khax
Boko amoul yangui mél ni bayima
Sokou amoul doto nék nit.
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy
Sougnou xel motax gnuy déf
Wawaw
Wawaw
Wawaw
Wawaw
Famarë reub kat lawone
Da ama biss mou khall yône
Mu taxaw di xalat bamu yàg
Mu sène mbëtt miy daw
Mu suxat fital am ba di dâgu
nane douma raw
Far mbëtt ma sène kokorong
Dadi dieul bop ba
Dal di koy rône
Bopp ba neubouna litha des
Yaramam béppa ngui fègn
Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya
Lippe di fègne
Lii takh mou déféni
Mbeutteu daa amoul xel
Kone gnoune gni Yalla jox xel
Nagnu santati
Nagnu santati
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy
Sougnou xel motax gnuy déf
Wawaw lolu moy xel
Soko amoul
Yangui mél bayima
Yangui mél bayima
Loy dougou nang ko téké xel.
Famarë reub kat lawone
Résumé français:
Il était le porte-parole des noirs et des blancs
Il a toujours protégé notre peuple
Il nous a exhortés au travail
Il nous a conseillé d'éduquer nos enfants
Il nous a exhortés au travail
Il nous a conseillé d'éduquer nos femmes
La vérité était sa raison de vivre
C'était un rassembleur
Le pays tout entier vous est reconnaissant,
Mulaay Dabbanx
Il était le porte-parole des noirs et des blancs
Il a toujours protégé notre peuple
Il a prôné l'ouverture aux autres et le travail dur
Il préférait la sympathie envers les femmes
Il nous a conseillé d'éduquer nos enfants



Writer(s): GUEYE MOUHAMADOU, CALO' MASSIMILIANO, NDOUR YOUSSOU


Youssou N'Dour - Rokku Mi Rokka
Album Rokku Mi Rokka
date of release
29-10-2007




Attention! Feel free to leave feedback.