Youssou N'Dour - Baay Faal Lyrics

Lyrics Baay Faal - Youssou N'Dour



Baay Faal
Baay faal gueu da djook thia fadjar
Nga sène ko mouy soli sagar
Boppam gueu sekkeu ki kawar
Yoré keulleum gueu di zikar
falé woul khiif ak mér
Boo démé sakh khekh na badar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal gueu da djook thia fadjar
Mani bour Yalla da djook thia fadjar
Nga sène ko mouy soli sagar
Yoré keulleum gueu di zikar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djommeul na wa ndar
Doundeum gueu nekh na
Zikar sa neekh na lol
Baay faal bi, baay faal ki modi guènne goor
Zikar sa motakh mou djégué Yalla
Baay faal bi, baay faal kouko khamone dinga mandou thi mome
Thia tool yeu...
Thia tèène yeu...
Thia wagne weu...
Magal yeu...
Baay faal liguey la khame
Baay faal ndigueul la khame
Baay faal dou khekh dou khoulo
Beuggue neu nite, fonk na nite khekhoulol
Mome la fayé ko lo mou ligueyal sougnou borom
Beuggue na la baay faal
Nangou nite
Kimo djégué sougnou borom
Dey liguey di djokhé motakh baay faal djégué naa sougnou borooom...
Dey liguey di diokhé
Dey liguey di diokhé motakh baay faal
Toggam ga nekhna lol motakh bay faal
Dey magal motakh baay faal
Dey zikar motakh baay faal



Writer(s): Youssou N'dour, Kabou Gueye, Mody Ba


Youssou N'Dour - Rokku Mi Rokka
Album Rokku Mi Rokka
date of release
29-10-2007




Attention! Feel free to leave feedback.