Youssou N'Dour - Da fa laa - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Youssou N'Dour - Da fa laa




Da fa laa
Da fa laa
Da fa laa, wóolóo,
Da fa laa, wóolóo,
Teg la nak, fu mu teg ul keneen
Teg la nak, fu mu teg ul keneen
Di dox sa bëgg bëgg, di dab sa banneex,
Di dox sa bëgg bëgg, di dab sa banneex,
Ndax seetlu nga koo
Ndax seetlu nga koo
Yaw, Yaw la bëgg,
Yaw, Yaw la bëgg,
Te yaw, yaa ko sagal,
Te yaw, yaa ko sagal,
Waaw waaw
Waaw waaw
Bu mbëggéel, doon lumière,
Bu mbëggéel, doon lumière,
Mel na ni, ni jant bi
Mel na ni, ni jant bi
Te su am oon, lu ko gën ë leer,
Te su am oon, lu ko gën ë leer,
Dem na wut i ko
Dem na wut i ko
Ni yaw, diaral nga ko,
Ni yaw, diaral nga ko,
Lu raw, sóoru gayndé,
Lu raw, sóoru gayndé,
Waaw waaw
Waaw waaw
Lu mu metti metti, di nga tew,
Lu mu metti metti, di nga tew,
Lu mu sori sori, an! di nga ñëw,
Lu mu sori sori, an! di nga ñëw,
Ca dëgg dëgg dëgg
Ca dëgg dëgg dëgg
Dem na, ba dem, mën ë tul ë tok
Dem na, ba dem, mën ë tul ë tok
Benn bés, bum la, gis ul
Benn bés, bum la, gis ul
Jox na la bii respect,
Jox na la bii respect,
Nga delloo ko bii respect
Nga delloo ko bii respect
Entre vous, entre vous chérie,
Entre vous, entre vous chérie,
Du wax lii def leneen
Du wax lii def leneen
Ca dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg,
Ca dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg,
Ya ko diara
Ya ko diara
Ni yaw, yaa ko sagal,
Ni yaw, yaa ko sagal,
Waw waaw
Waw waaw
Fépp fu mu mën ë ne,
Fépp fu mu mën ë ne,
Da fay sentir sa parfum
Da fay sentir sa parfum
Loolu yaa ko ko diaral,
Loolu yaa ko ko diaral,
Ndax yaa ko liggéey
Ndax yaa ko liggéey
Les mots qu′il utilise,
Les mots qu′il utilise,
Sont toujours en deçà
Sont toujours en deçà
De ce qu'il ressent,
De ce qu'il ressent,
Yaw yaa ko ko diaral
Yaw yaa ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Daf la bëuggué
Daf la bëuggué
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Kay nga diégué ko
Kay nga diégué ko
Mou laye déy
Mou laye déy
Yaw mii yaw,
Yaw mii yaw,
Su fekkee li mu la wax doy ula,
Su fekkee li mu la wax doy ula,
Boo yakkamtee,
Boo yakkamtee,
Mu def al la ko, ni nga ko bëggée
Mu def al la ko, ni nga ko bëggée
Mom contane neu
Mom contane neu
Te sakh yaguena bëgg thi yaw,
Te sakh yaguena bëgg thi yaw,
Boo yakkamtee,
Boo yakkamtee,
Mu def al la ko, ni nga ko bëggée
Mu def al la ko, ni nga ko bëggée
Sa lui vas,
Sa lui vas,
Chérie sa lui vas lo def nekh na ko
Chérie sa lui vas lo def nekh na ko
Da fa laa, da fa laa
Da fa laa, da fa laa
Def ni nga ko def
Def ni nga ko def
Loo bëgg, mu indil la ko
Loo bëgg, mu indil la ko
Loo laaj, mu kheuthiel la ko
Loo laaj, mu kheuthiel la ko
Su fekkee am u ko, mu ñaan ko yalla
Su fekkee am u ko, mu ñaan ko yalla
Chérie boy, chérie boy
Chérie boy, chérie boy
Ya ko ko diaral
Ya ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy
Chérie boy, chérie boy
Lo diokhogne mo dok
Lo diokhogne mo dok
Chérie boy, chérie boy
Chérie boy, chérie boy
Lo def nonou la
Lo def nonou la
Chérie boy, chérie boy
Chérie boy, chérie boy
Ya ko ko diaral
Ya ko ko diaral
Youssou Ndour, madjiguene
Youssou Ndour, madjiguene
Boul yekhal dara
Boul yekhal dara
Na gua gaw, na gua gaw
Na gua gaw, na gua gaw
Te li djieuntima
Te li djieuntima
Sokhla yi, sokhla yi
Sokhla yi, sokhla yi
Gnome gno ma gueteun
Gnome gno ma gueteun






Attention! Feel free to leave feedback.