Lyrics Gagganti ko - Youssou N'Dour
Ba
ñu
la
koy
jox,
xam
ul
dara;
Bu
la
séen
ée,
daw
gatandu
la,
Ay
waajur
ëm,
da
ñoo
am
oon
yaakaar
ci
yaw
Jamono
y
dox,
jafejafe
am,
sëytaane
ñëw
Bu
ko
dóor,
bu
ko
saaga,
bu
ko
xas,
bu
ko
wax
lu
ñaaw
Delloo
l
sa
xel,
ca
ginnaaw,
te
muñ
ël
ko;
Ba
ñu
la
koy
may,
xam
ul
dara;;
Bu
la
séen
ée,
daw
laxasu
la,
Ay
waajur
ëm,
da
ñoo
am
oon
yaakaar
ci
yaw
Jamono
dox,
jafejafe
am,
sëytaane
ñëw
Bu
ko
dóor,
bu
ko
saaga,
bu
ko
xas,
bu
ko
wax
lu
ñaaw
Delloo
l
sa
xel,
ca
ginnaaw,
bu
ko
souffrir
loo;
Xool
al
ci
ay,
waajur
ëm,
bu
ko
joy
loo
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Bu
ko
dòor,
bu
ko
saaga,
bu
ko
xas,
Bu
ko
wakh
lu
ñaaw
Bu
yënggël
ée
daal,
ba
sa
xol
fees,
génn
ël
nga
dem
Bu
fa
toog
yaw,
di
raak
ak
moom,
sàmm
al
sa
cér
Woo
ko,
waxtaan
ak
moom,
té
muñël
ko
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Bu
juum
ee
gagganti
ko
Yaw
tam,
bul
forcer,
deel
négocier
Ndaw
sii,
bul
teg
deal,
bul
planifier
Te
bu
am
ee,
lu
fi
leer
ul,
nga
clarifier
Coow
li,
bu
déborder,
nga
pacifier
Yaw
daal,
bul
forcer,
deel
négocier
Ndaw
sii,
bul
teg
deal,
bul
planifier
Te
bu
am
ee,
lu
fi
leer
ul,
nga
clarifier
Coow
li,
bu
déborder,
nga
pacifier
Wa
waaw
Jaajëf,
di
na
tax,
xale
wone
jom
Waaw
góor,
di
na
tax,
xale
yokk
jom
Di
ko
won
sa
jom,
moo
koy
dolli
jom
Jom
jom
jom
rek,
dara
lu
dul
jom
Yërëmal
ma
ko
Momit
mou
wégal
ma
laa
Nax
ko
neex
al
ma
ko
Moomit
mu
xam
ko
1 Gagganti ko
2 Mama Africa
3 Ndox
4 La solution c’est de pardonner
5 Mool
6 Tatagal
7 Fay Bor
8 Ballago ndumbé Yaatma
9 Zéro déchets
10 Da fa laa
11 Wax ju Bari
12 Waññ iko
Attention! Feel free to leave feedback.