Lyrics Mool - Youssou N'Dour
MOOL
Yaw
mool
u
géej
gi
Di
jambaar
ci
réew
mi
Bala
ngaa
dem
géej
Ngala
déglu
météo
Bu
la
nee
bul
dem
Lu
mën
ë
xew
bul
dem
Ben
fan
ak
ñaar,
Bu
mu
yax
sa
liggéey
Doyloo
nga
yalla,
Du
tee
nga
sa
yor
téléphone
Ak
sa
gps,
te
bul
fatte
sa
gillet
Sama
fans
yi
ma
am,
Mool
ñoo
ma
gën
ë
xam
Fu
ma
làng
ee
ak
ñoom,
Guddi
gë
day
xumb
lool
Man
sama
fans
yee,
ma
saf
Sawar
naa
làng
ak
ñoom,
fu
ne
Aka
ñoo
dégg
daaj,
ma
ni
Moo
tax
may
dem
ba
jeex,
walla
Jambaar
ca
waar
wa,
Jambaar
ca
géej
gë
Su
ma
ko
mën
oon,
Ben
mool
du
des
ci
géej
Bu
la
nee
bul
dem,
Lu
mën
ë
xew
bul
dem
Ben
fan
ak
ñaar,
Bu
mu
yax
sa
liggéey
Sama
fans
yi
ma
am,
Mool
ñoo
ma
gën
ë
xam
Fu
ma
làng
ee
ak
ñoom,
Guddi
gë
day
xumb
lool
Jambaar
ca
waar
wa,
Jambaar
ca
géej
gë
Su
ma
ko
mën
oon,
Ben
mool
du
des
ci
géej
Man
sama
fans
yee,
ma
saf
Sawar
naa
làng
ak
ñoom,
fu
ne
Aka
ñoo
dégg
daaj,
ma
ni
Moo
tax
may
dem
ba
jeex,
walla
Yalna
leen
yalla
suturaal,
Te
di
leen
samm
biir
géej
Barke
el
seen
liggéey
bi,
Barke
el
seen
njaboot
gi
Aar
leen
ba
ñu
doon
mag,
Jox
leen
barke
maam
yi
Man
sama
fans
yee,
ma
saf
Sawar
naa
làng
ak
ñoom,
fu
ne
Yess
aye
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Bël
ba
ca
ndar,
sonn
al
na
waa
guét
ndar
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Mool
yi
laa
bëgg
ë
làng
al,
Seen
làng
xumb
në,
Ndax
sa
ma
fan's
yi
nak,
Am
mool
yee
ci
gën
ë
dense
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Bël
ba
ca
ndar,
sonn
al
na
waa
guét
ndar
géej
oo
Sa
telephone
ak
sa
GPS,
Bul
fatte
gillet
ba
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Ñoom
laa
bëgg
ë
làng
al,
seen
làng
xumb
në,
Ndax
sa
ma
fan's
yi
nak,
am
Mool
yee
ci
gën
ë
dense
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
A
dëgg
ël,
yaw
mool
u
géej,
Yaa
di
jàmbaar
Yaa
bari
fullë
lool
Bari
jom
lool
Yaa
donn
loolu
Gëm
yalla
lool
Yaa
xarañ
lool,
te
tabe
lool
Youssou
woy
na
leen
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Bël
ba
ca
ndar,
sonn
al
na
waa
guét
ndar
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Mool
yi
laa
bëgg
ë
làng
al,
Seen
làng
xumb
në,
Ndax
sa
ma
fan's
yi
nak,
am
Mool
yee
ci
gën
ë
dense
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Anh
mool
ba
dem
na
géej
oo
Mool
yi
laa
bëgg
ë
làng
al,
Seen
làng
xumb
në,
Ndax
sa
ma
fan's
yi
nak,
am
Mool
yee
ci
gën
ë
dense
1 Gagganti ko
2 Mama Africa
3 Ndox
4 La solution c’est de pardonner
5 Mool
6 Tatagal
7 Fay Bor
8 Ballago ndumbé Yaatma
9 Zéro déchets
10 Da fa laa
11 Wax ju Bari
12 Waññ iko
Attention! Feel free to leave feedback.