Youssou N'Dour - Mool - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Youssou N'Dour - Mool




Mool
Mool
MOOL
MOOL
Yaw mool u géej gi
Tu es très populaire dans ce pays
Di jambaar ci réew mi
Tu es une star ici
Bala ngaa dem géej
Si tu veux être populaire
Ngala déglu météo
Tu dois avoir beaucoup de fans
Bu la nee bul dem
Si tu veux être populaire
Lu mën ë xew bul dem
Tu dois être aimé par beaucoup de gens
Ben fan ak ñaar,
Mes fans et moi,
Bu mu yax sa liggéey
Si tu veux être aimé
Doyloo nga yalla,
Je te le dis, ma chérie,
Du tee nga sa yor téléphone
Tu dois avoir un bon téléphone
Ak sa gps, te bul fatte sa gillet
Et un GPS, pour pouvoir trouver ton chemin
Sama fans yi ma am,
Mes fans m'aiment,
Mool ñoo ma gën ë xam
Ils me connaissent bien
Fu ma làng ee ak ñoom,
J'ai beaucoup d'amis avec eux,
Guddi day xumb lool
Ils me soutiennent toujours
Man sama fans yee, ma saf
Je t'aime, ma chérie,
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
J'ai beaucoup d'amis avec toi, parce que
Aka ñoo dégg daaj, ma ni
Tu es toujours pour moi, et
Moo tax may dem ba jeex, walla
Je suis toujours pour toi, que tu sois
Jambaar ca waar wa,
Tu es une star,
Jambaar ca géej
Tu es très populaire
Su ma ko mën oon,
Si je te vois,
Ben mool du des ci géej
Alors tu es très populaire
Bu la nee bul dem,
Si tu veux être populaire
Lu mën ë xew bul dem
Tu dois être aimé par beaucoup de gens
Ben fan ak ñaar,
Mes fans et moi,
Bu mu yax sa liggéey
Si tu veux être aimé
Sama fans yi ma am,
Mes fans m'aiment,
Mool ñoo ma gën ë xam
Ils me connaissent bien
Fu ma làng ee ak ñoom,
J'ai beaucoup d'amis avec eux,
Guddi day xumb lool
Ils me soutiennent toujours
Jambaar ca waar wa,
Tu es une star,
Jambaar ca géej
Tu es très populaire
Su ma ko mën oon,
Si je te vois,
Ben mool du des ci géej
Alors tu es très populaire
Man sama fans yee, ma saf
Je t'aime, ma chérie,
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
J'ai beaucoup d'amis avec toi, parce que
Aka ñoo dégg daaj, ma ni
Tu es toujours pour moi, et
Moo tax may dem ba jeex, walla
Je suis toujours pour toi, que tu sois
Yalna leen yalla suturaal,
Tu es très belle, ma chérie,
Te di leen samm biir géej
Tu es une vraie star
Barke el seen liggéey bi,
Tu es tellement belle,
Barke el seen njaboot gi
Tu es tellement élégante
Aar leen ba ñu doon mag,
Tu es tellement spéciale,
Jox leen barke maam yi
Je t'aime tellement
Man sama fans yee, ma saf
Je t'aime, ma chérie,
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
J'ai beaucoup d'amis avec toi, parce que
Yess aye
Tu es très belle
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géej oo
Tu es toujours pour moi, tu es toujours pour moi
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Mool yi laa bëgg ë làng al,
Tu es très populaire
Seen làng xumb në,
Tu es très populaire
Ndax sa ma fan's yi nak,
Parce que je t'aime beaucoup,
Am mool yee ci gën ë dense
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géej oo
Tu es toujours pour moi, tu es toujours pour moi
Sa telephone ak sa GPS,
Ton téléphone et ton GPS,
Bul fatte gillet ba
Tu sais toujours aller
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Ñoom laa bëgg ë làng al, seen làng xumb në,
Tu es très populaire
Ndax sa ma fan's yi nak, am
Parce que je t'aime beaucoup,
Mool yee ci gën ë dense
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
A dëgg ël, yaw mool u géej,
Tu es très populaire,
Yaa di jàmbaar
Tu es une star
Yaa bari fullë lool
Tu es belle et élégante
Bari jom lool
Tu es belle et élégante
Yaa donn loolu
Tu es tellement belle
Gëm yalla lool
Tu es tellement élégante
Yaa xarañ lool, te tabe lool
Tu es tellement belle, tu es tellement élégante
Youssou woy na leen
Je t'aime beaucoup
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géej oo
Tu es toujours pour moi, tu es toujours pour moi
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Mool yi laa bëgg ë làng al,
Tu es très populaire
Seen làng xumb në,
Tu es très populaire
Ndax sa ma fan's yi nak, am
Parce que je t'aime beaucoup,
Mool yee ci gën ë dense
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Anh mool ba dem na géej oo
Tu es très populaire
Mool yi laa bëgg ë làng al,
Tu es très populaire
Seen làng xumb në,
Tu es très populaire
Ndax sa ma fan's yi nak, am
Parce que je t'aime beaucoup,
Mool yee ci gën ë dense
Tu es très populaire






Attention! Feel free to leave feedback.