Lyrics Da fa laa - Youssou N'Dour
Da
fa
laa,
wóolóo,
Teg
la
nak,
fu
mu
teg
ul
keneen
Di
dox
sa
bëgg
bëgg,
di
dab
sa
banneex,
Ndax
seetlu
nga
koo
Yaw,
Yaw
la
bëgg,
Te
yaw,
yaa
ko
sagal,
Waaw
waaw
Bu
mbëggéel,
doon
lumière,
Mel
na
ni,
ni
jant
bi
Te
su
am
oon,
lu
ko
gën
ë
leer,
Dem
na
wut
i
ko
Ni
yaw,
diaral
nga
ko,
Lu
raw,
sóoru
gayndé,
Waaw
waaw
Lu
mu
metti
metti,
di
nga
tew,
Lu
mu
sori
sori,
an!
di
nga
ñëw,
Ca
dëgg
dëgg
dëgg
Dem
na,
ba
dem,
mën
ë
tul
ë
tok
Benn
bés,
bum
la,
gis
ul
Jox
na
la
bii
respect,
Nga
delloo
ko
bii
respect
Entre
vous,
entre
vous
chérie,
Du
wax
lii
def
leneen
Ca
dëgg
dëgg
dëgg
dëgg
dëgg
dëgg
dëgg,
Ya
ko
diara
Ni
yaw,
yaa
ko
sagal,
Waw
waaw
Fépp
fu
mu
mën
ë
ne,
Da
fay
sentir
sa
parfum
Loolu
yaa
ko
ko
diaral,
Ndax
yaa
ko
liggéey
Les
mots
qu′il
utilise,
Sont
toujours
en
deçà
De
ce
qu'il
ressent,
Yaw
yaa
ko
ko
diaral
Chérie
boy,
chérie
boy,
chérie
boy
Daf
la
bëuggué
Chérie
boy,
chérie
boy,
chérie
boy
Kay
nga
diégué
ko
Mou
laye
déy
Yaw
mii
yaw,
Su
fekkee
li
mu
la
wax
doy
ula,
Boo
yakkamtee,
Mu
def
al
la
ko,
ni
nga
ko
bëggée
Mom
contane
neu
Te
sakh
yaguena
bëgg
thi
yaw,
Boo
yakkamtee,
Mu
def
al
la
ko,
ni
nga
ko
bëggée
Sa
lui
vas,
Chérie
sa
lui
vas
lo
def
nekh
na
ko
Da
fa
laa,
da
fa
laa
Def
ni
nga
ko
def
Loo
bëgg,
mu
indil
la
ko
Loo
laaj,
mu
kheuthiel
la
ko
Su
fekkee
am
u
ko,
mu
ñaan
ko
yalla
Chérie
boy,
chérie
boy
Ya
ko
ko
diaral
Chérie
boy,
chérie
boy
Lo
diokhogne
mo
dok
Chérie
boy,
chérie
boy
Lo
def
nonou
la
Chérie
boy,
chérie
boy
Ya
ko
ko
diaral
Youssou
Ndour,
madjiguene
Boul
yekhal
dara
Na
gua
gaw,
na
gua
gaw
Te
li
djieuntima
Sokhla
yi,
sokhla
yi
Gnome
gno
ma
gueteun
1 Gagganti ko
2 Mama Africa
3 Ndox
4 La solution c’est de pardonner
5 Mool
6 Tatagal
7 Fay Bor
8 Ballago ndumbé Yaatma
9 Zéro déchets
10 Da fa laa
11 Wax ju Bari
12 Waññ iko
Attention! Feel free to leave feedback.