Lyrics Waññ iko - Youssou N'Dour
Par
AbouAmg
Han,
han,
sa
kattan
bari
na,
sa
bateau
gaaw
na,
te
saw
fit
rëy
në
Han,
han,
sa
kattan
bari
na,
sa
bateau
gaaw
na,
te
saw
fit
rëy
në
Han,
han,
sa
kattan
bari
na,
sa
bateau
gaaw
na,
te
saw
fit
rëy
në
Refain:
waññi
ko,
waññi
ko,
waññi
ko,
Waññi
ko,
waññi
ko,
ëpp
në
Refain:
waññi
ko,
waññi
ko,
waññi
ko,
Waññi
ko,
waññi
ko,
ëpp
në
Han,
han,
sa
kattan
bari
na,
sa
bateau
gaaw
na,
te
saw
fit
rëy
në
Han,
han,
sa
kattan
bari
na,
sa
bateau
gaaw
na,
te
saw
fit
rëy
në
Yaw
yaa
ni,
ëpp
óon
nga,
trois
cent
kilos,
Te
bés
bu
ne,
benn
xar
nga
daan
añ
e
Nga
neeti,
at
mi
fi
Obama
ñëw
ée
Yaw
yaa
ko
gis,
muy
dox
antu,
biir
Pikine
Am
oon
na,
gaïnde
gu
rëccé,
parc
hann
Nga
neeti
ñu,
yaw
yaa
ko
jat,
ba
mu
nelaw,
· Nga
ni
ma,
am
oon
nga,
benn
bateau,
ca
Guinée
Te
waa
nations
– unies,
nga
ka
daan
loué
· Te
diggënté,
États-Unis
ak
Guinée,
Daa
woo
ko
daw,
lu
ëpp
ñaar
i
fan
Am
na
benn
bés,
nga
ni
ma,
my
boy
Keroog
daje
naak,
roi
des
arènes.
2 fois.
Ben
loxo,
laa
ko
yékkëtée,
ni
ko
félicitations.
2 fois.
Ma
tegaat
ko
ci
suuf,
ni
ko,
my
boy.
2 fois
Na
nga
jaar,
sa
ma
kër,
ma
jox
la
yeneen
clefs
Na
nga
jaar,
galle,
ma
jox
la
yeneen
clefs
Techniques
yooyu,
japon
laa
ko
jànge
Ca
yooya
jamono,
man
la
ñépp
di
wër
Lu
ñu
wax
nga
ni
fekke
nga
ko
Fu
ñu
wax
nga
ni
dem
nga
fa
Doo
tiit
doo
raf,
doo
dellu
ginnaaw;
Waaye
sa
ma
waa
jii,
ken
melut
ni
moom.
Wax
oon
naa
fi
ni
adduna
ken
du
ko
dajal,
Te
ku
dul
umppëlé
da
ñu
lay
ragal.
Wax
aat
leen
ni
faw
nit
ku
ne
am
lu
muy
des
al
Ngir
bu
ëllëg
ée
ñu
mën
laa
set
al.
Xam
lépp,
mën
lépp,
loolu,
yalla
dong
a
ko
jagoo.
2 fois.
Ragal
al
yalla,
waay,
ragal
al
yalla
Ragal
al
yalla,
waa
jii,
ragal
al
yalla
Ragal
al
yalla,
waay,
ragal
al
yalla
Ragal
al
yalla,
waa
jii,
ragal
al
yalla
1 Gagganti ko
2 Mama Africa
3 Ndox
4 La solution c’est de pardonner
5 Mool
6 Tatagal
7 Fay Bor
8 Ballago ndumbé Yaatma
9 Zéro déchets
10 Da fa laa
11 Wax ju Bari
12 Waññ iko
Attention! Feel free to leave feedback.