Lyrics Tatagal - Youssou N'Dour
Tatagal
Bu
ko
jot
gi
may
e
woon
Weer
wu
ne
ma
ñëw
Sagaal
sama
fan's
yi
Sant
leen,
sargal
leen
Ni
bu
leen
di
sonn
al
béer
Njaw
du
mel
ni
lem
Jimmy
mbaye
xalam
al
leen
Te
encourager
leen
leen
Bu
ko
jot
gi
may
e
woon
Weer
wu
ne
ma
wëy
Sagaal
sama
fan's
yi
Sant
leen,
sargal
leen
Ma
nii
bu
leen
di
sonn
al
béer
Njaw
du
mel
ni
lem
Jimmy
mbaye
xalam
al
leen
Te
encourager
leen
leen
Na
ñu
leen
xalam
al
Na
ñu
leen
tatagal
Na
ñu
leen
woy
al
Na
ñu
leen
sargal
Na
ñu
leen
xalam
al
Na
ñu
leen
tatagal
Na
ñu
leen
woy
al
Na
ñu
leen
sargal
Na
ñu
leen
xalam
al
Na
ñu
leen
tatagal
Na
ñu
leen
woy
al
Na
ñu
leen
sargal
Je
vous
salue
Avec
tous
les
honneurs
Et
vous
souhaite
Que
du
bonheur
Ces
fans
de
valeurs
Qui
m'attendent
des
heures
Je
vous
ai
dans
mon
cœurs
Vous
méritez,
d'être
ova
tionnés,
C'est
ça
la
vérité
Vous
êtes
toujours
là
Quoiqu'il
puisse
arriver
Yéen
ay
sama
y
soppe
Ànd
bi
yagg
na
Confiance
bi
rëy
na
Tatagal
leen
jaadu
na
Njukkël
leen
war
na
Fu
né
nda
pare
ngen
ñu
dem
wër
adduna
Da
ma
ni
pare
naa
Te
it
sax
defe
naa
Xalaat
bi
jaadu
na
Su
ma
leen
Mën
oon
a
jox
loxo
Yegsi
naa
Su
ma
leen
mën
oon
seet
si
Yegsi
naa
Fatte
wu
ma
leen
Déedéet
mën
ul
am
Yëg
naa
leen
Sallaaw
mooy
li
wóor
Fan's
yi
xam
ci
jamono
Naw
naa
seen
taxawaay
Moo
tax
ma
jóg
Sargal
leen,
woy
ee
Bul
gnu
leen
Fatte
di
bëgguel
Naw
naa
seen
taxawaay
Moo
tax
ma
jóg
Sargal
leen,
woy
ee
Fan's
yi
xam
ci
jamono
Naw
naa
seen
taxawaay
Moo
tax
ma
jóg
Sargal
leen,
woy
ee
Bul
gnu
Leen
fatte
di
bëgguel
Naw
naa
seen
taxawaay
Moo
tax
ma
jóg
Sargal
leen,
woy
ee
1 Gagganti ko
2 Mama Africa
3 Ndox
4 La solution c’est de pardonner
5 Mool
6 Tatagal
7 Fay Bor
8 Ballago ndumbé Yaatma
9 Zéro déchets
10 Da fa laa
11 Wax ju Bari
12 Waññ iko
Attention! Feel free to leave feedback.