Youssou N'Dour - Wax ju Bari Lyrics

Lyrics Wax ju Bari - Youssou N'Dour

Boo mer ee dëgg
, Sëytaane da lay dugg
Jaxjax al sa xol
, Def loo la
, Li mu bëgg And al ak dal.
Sëytaane da fay jël temps
, Yakkamti wul
Boo am ul chance,
Bu la yalla,
Dimmili wul
Da lay xaptal
Description
Youssou Ndour -- Wax ju bari - ALBUM - MBALAX
5,2 k
J'aime
209 496
Vues
12 nov.
2021
Ànd Liggéey, Wàññi Wax,
Car comme disait Mame Cheikh Ibrahima
FALL " Yalla Du Fay Wax Di Fàtte Jëf ".
A travers ce titre, je rends également hommage à un des monuments et
Pères du Mbalax: IBRA KASSE, Al Maabo Yacine Dial,
Un véritable Maître qu'il a été donné au Sénégal d'avoir.
Un Maître que j'ai eu la chance d'avoir aux prémices de ma carrière.
Boo mer ee dëgg,
Sëytaane da lay dugg Jaxjax al sa xol,
Def loo la, li mu bëgg And al ak dal.
Sëytaane da fay jël temps, yakkamti wul Boo am ul chance,
Bu la yalla, dimmili wul Da, lay, xaptal Boo bëgg ée mucc,
Ngóor sii, yaw déglu ma Bu la fekk oon taxaw, toog al,
Xarit sama Toog al ba dal Bu la fekk oon toog, tëdd ël,
Ba gagni dem Bu yagg ee, sëytaane, day mujj dem Doo tu la tal
Bul nangu, wax ju bari yaw,
Ku la ko bëgg indil na nga bañ bul ko kaf e, bul ko mbokk oo,
Fexe el dund te ànd ak dal booy ànd al, na nga seet, nit ku regle,
Te bañ bari wax fexe el ba adopter,
Dund gu ànd ul ak bari wax ku la ko bëgg teg, bul ko nangu,
Bul ko masala bari wax, da lay tardeel,
Bari wax,da lay sonn al bari wax, da lay jaxase
Description
Youssou Ndour -- Wax ju bari - ALBUM - MBALAX
5,2 k
J'aime
209 496
Vues
12 nov.
2021
Ànd Liggéey, Wàññi Wax,
Car comme disait Mame Cheikh Ibrahima
FALL " Yalla Du Fay Wax Di Fàtte Jëf ".
A travers ce titre, je rends également hommage à un des monuments et
Pères du Mbalax: IBRA KASSE, Al Maabo Yacine Dial,
Un véritable Maître qu'il a été donné au Sénégal d'avoir.
Un Maître que j'ai eu la chance d'avoir aux prémices de ma carrière.
Boo mer ee dëgg,
Sëytaane da lay dugg Jaxjax al sa xol,
Def loo la, li mu bëgg And al ak dal.
Sëytaane da fay jël temps, yakkamti wul Boo am ul chance,
Bu la yalla, dimmili wul Da, lay, xaptal Boo bëgg ée mucc,
Ngóor sii, yaw déglu ma Bu la fekk oon taxaw, toog al,
Xarit sama Toog al ba dal Bu la fekk oon toog, tëdd ël,
Ba gagni dem Bu yagg ee, sëytaane,
Day mujj dem Doo tu la tal bul nangu, wax ju bari yaw,
Ku la ko bëgg indil na nga bañ bul ko kaf e, bul ko mbokk oo,
Fexe el dund te ànd ak dal booy ànd al, na nga seet, nit ku regle,
Te bañ bari wax fexe el ba adopter,
Dund gu ànd ul ak bari wax ku la ko bëgg teg, bul ko nangu,
Bul ko masala bari wax, da lay tardeel, bari wax,
Da lay sonn al bari wax, da lay jaxase bu leen sonn al béer,
Njaw du mel ni lem bu leen sonn al béer,
Njaw du mel ni lem bu leen sonn al béer,
Njaw du mel ni lem bu leen sonn al béer,
Njaw du mel ni lem bu leen sonn al béer,
Njaw du mel ni lem wax lu néew, jëf lou bari, kouné war na laa,
Wax lu néew, jëf lou bari, loo loo am,
Maanaa Ibra kassé birame coumba Ndiaye Kouly kassé ek maajigéen oo Al
Maabo Yacine dial, ma des ca bëlbë Moo ma daan wax naan,
Youssou na ñu ànd liggéey, te waññi wax Te waññi wax Baay i Oumar,
Baay i Alioune, baay I ndeye kassé Góor u fatou Baay i idi,
Doom i nday i adama, ak kassé plus Al maabo yacine dial,
Ibra mor astou kassé Fatou oy, médoune kassé Ndoumbé yatma
Wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la wax ju néew,
Jëf ju bari, ku ne war na la wax da fay gatt yanu maanaa,
Neex a dégg lool, fees ak njariñ ñu wax ko ba wax jot ee,
Fa ñu ko war a wax e wax ju néew, jëf ju bari,
Ku ne war na la wax ju néew, jëf ju bari,
Ku ne war na la xaaj u guddi, boo toog oon ba mu yagg,
Nga doon bëccëg di na xumb lool, ba jaaxal gaa ñi wax ju néew,
Jëf ju bari,
Ku ne war na la wax ju néew, jëf ju bari, ku ne war na la

Youssou N'Dour - MBALAX
Album MBALAX
date of release
12-11-2021

Attention! Feel free to leave feedback.